1 Samuel 26:15
TSK
Daawuda ne Abner: «Xanaa doo jàmbaaru góor? Ku fiy sa moroom ci Israyil? Ana lu la tee wattu Buur, sab sang? Am na ci xarekat yi ku bóomsi woon Buur, sab sang.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Daawuda ne Abner: «Xanaa doo jàmbaaru góor? Ku fiy sa moroom ci Israyil? Ana lu la tee wattu Buur, sab sang? Am na ci xarekat yi ku bóomsi woon Buur, sab sang.
¶ Ba loolu amee Abner yebal ca saa sa ay ndaw ca Daawuda, ne ko: «Ana ku moom réew mii?» Mu neeti ko: «Fasool ak man kóllëre. Maa lay jàpple, ba walbatil la Israyil gépp, ñu nangul la.»