KYG / Acts / [JC0] chapitre 2 KYG · verses 1-4 Aa Xoolaat Jàngalekatu bind ¶ Ba bésu màggalu Pàntakot agsee, ñoom ñépp a bokk daje benn bérab. Dayo bind A- 25px A+ Font jàngat Serif Amul Naskh Amiri Scheherazade New Noto Sans Arabic Cairo Tajawal Markazi Text Changa Noto Kufi Arabic Alexandria Almarai Aref Ruqaa Ink El Messiri Harmattan IBM Plex Sans Arabic Mada Reem Kufi Lateef Reset ← Chapter 1 Acts 2:5 → Toppal Yoon yu jàmm Jàngalekat Copy Jàmm Nòt 1 ♥ 📝 B a bésu màggalu Pàntakot agsee, ñoom ñépp a bokk daje benn bérab. 2 ♥ 📝 Ca saa sa coow jollee asamaan, mel ni riirum ngelaw lu bare doole, daldi fees dell biir kër ga ñu toog. 3 ♥ 📝 Ci kaw loolu ay làmmiñ yu mel ni tàkk-tàkki sawara feeñu leen, làmmiñ ya séddlikoo, daldi toŋ ci kaw kenn ku nekk. 4 ♥ 📝 Ñoom ñépp nag feese Noo gu Sell gi, tàmbalee làkk làkk yu wuute, na leen ko Noo gi manloo. Chapitre bi yépp Aaya yi ci méngoo Tekki Wolof yépp Bible yépp