TSK

TSK · Deuteronomy 11:32

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Léegi nag yeen waa Israyil, dégluleen dogali yoon yeek àttey yoon yii ma leen di xamal, ngir ngeen di ko jëfe, ndax ngeen dund ba dugg, nanguji réew ma leen Aji Sax ji seen Yàllay maam, di jox.

¶ Kon nag sàmmooleen koo jëfe ni leen ko seen Yàlla Aji Sax ji sante. Buleen lajjee ndijoor mbaa càmmoñ.