TSK

TSK · Deuteronomy 22:6

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Génnewaaleel lépp luy xeetu mbindeef mu ngeen àndal: picc yi ak bàyyima yi ak luy raam, ñu fulandiwu ci kaw suuf, daldi giir te bare.»

Waaye su dee aw nag mbaa ab gàtt, deesu ko booleek doom ji rendi ci benn bés.

Am riir mooy jollee ca sa biir gàngoor, sa tata yépp tas, na Salman tase woon Bet Arbel, keroog bésub xare ba, ba ñu jëlee ndey, fenqaleek doom, ñu rajaxoo.