¶ Ba waa Misra xiifee, dañoo dem jooytuji dund ca Firawna. Mu wax ak ñépp ne leen: «Demleen ca Yuusufa; lu mu leen wax, defleen ko.»
TSK
TSK · Esther 3:1
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Genesis 41:55
TSK
1 Samuel 15:8
TSK
Mu jàpp Agag buurub Amalegeen ña, gàngoor ga gépp, mu faagaagal, leel leen ñawkay saamar.
Ezra 7:14
TSK
Man Buur, maa la yebal, maak sama juróom ñaari wóllëre; noo la yebal Yerusalem ak Yuda, ngir nga gëstujil ma nu ñu fay toppe sa yoonu Yàlla, wi nga yor téereem ci say loxo.
Esther 3:10
TSK
Ba mu ko defee Buur tekki jaarob torlukaayam ci baaraamam, jox ko Aman doomu Amdeta ma askanoo ca Agag, noonub Yawut ya.
Esther 7:6
TSK
Esteer ne ko: «Waa ji nuy fexeel, di bañ, dib noon de, Aman mu bon mii la!» Aman nag tiit lool fa kanam Buur ak Lingeer.
Psalms 12:8
TSK
Ngalla Aji Sax ji, sàmmal ku néewle, aar ko saa su ne ci nitu tey.
Daniel 6:2
TSK
¶ Mu neex Daryus nag, mu fal téeméeri jawriñ ak ñaar fukk ca réew ma, ñuy saytu nguur ga gépp;