TSK

TSK · Jeremiah 47:6

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

bu ma daasee sama saamar buy melax, ba ŋàbb ko ci saab loxo, di àtte, maay fey samay digaale, añale samay bañ.

Wóoy ngalla Asiri miy sama yetu mer, bolde bi ñu ŋàbb di samam sànj,

Xanaa duma gis ba fàww raayab noon, liitu xare di ko feelu?

Tundoo tund wu ne faraas fi màndiŋ mi, ay yàqkat a ngi ciy bawoo, doon saamaru Aji Sax ji, di faagaagal réew mépp, cat ba cat, jàmm réer luy dund!

¶ Aji Sax ji nag ne: «Wax leen ne leen: “Aji Sax ji Boroom gàngoori xare yi, Yàllay Israyil dafa wax ne: Naanleen ba màndi, di waccu, fëlëñu, tëë jóg ndax saamar bi may yebal fi seen biir.”

Su ma wàccee saamar ci miim réew it, ba sant saamar ne ko mu jaar ci biir réew mi, dagge fi nit ak mala,

«Waaye yaw garmib Israyil bu teddadi bu bon bi, sa bés dikk na, sa àppu mbugal mat na.