TSK

TSK · Job 27:20

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Guddig keroog malaakam Aji Sax ji moo dikk, fàdd ca dalub Asiri téeméer ak juróom ñett fukk ak juróomi junni (185 000). Ca ëllëg sa ña mucc teela xëy, yemuñu ci lu moy ñooña ñépp, diy néew.

Job 18:11 TSK

Lu ragloo koy darey mbetteel, ne ko dann.

Job 20:23 TSK

Ba muy sol kollam la ko Yàlla di yónnee tàngooru sànjam, tawal ko ko lu fees déqam.

Job 22:16 TSK

Ñoo buube, ne mes te seen àpp jotul, seen kenu màbb, wéy nim wal,

Ki yelloo cant, Aji Sax ji, moom laa woo, mucc ci samay noon.

Waaye man, Aji Sax ji, yaw laay dagaan. Éy Yàlla, na tey di bésub yiw. Ngalla nangul ma ci sa ngor lu yaa ak sa wall gu wóor.

¶ Guddi googa lañu rey Baltacar, buurub waa Babilon.