TSK

TSK · Job 33:18

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi
Job 15:22 TSK

Dootu yaakaara mucc musiba, saamar a koy yoot,

Job 33:24 TSK

da koy baaxe, daldi ne Yàlla: «Musal ko ba du wàccagum biir pax. Maa ngeek njotlaayam.»

Job 33:30 TSK

ngir sorale bakkanam pax, bàyyee ko leeraangey àddina.

Joel 2:8 TSK

Kenn buuxul moroom ma, ku nekk aw sélam lay topp, ci biir saan yi lañuy xuus, jàll it, te duñu taxaw.

Am dangay sofental mbaaxu Yàlla gu réy, akug jéllaleem, akug muñam, ndax ñàkka xam ne li Yàlla namm ci baaxe la, moo di nga tuub?

Sunu Boroom nag, ag muñam, jàppleen ne moo dig mucc, noonee leen ko sunu soppe, mbokk mi Póol binde woon ci xel mu rafet mi ñu ko baaxe.