Rikk bul yemale ku jub ak ku jubadi, ba boole leen rey, loolu jomb na la moos! Yaw miy àtte àddina sépp kay, lu jub rekk ngay def!»
TSK
TSK · Job 34:10
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Genesis 18:25
TSK
2 Samuel 22:31
TSK
Yàllaa mat, kàddug Aji Sax jee wér te wóor. Mooy feg képp ku ko làqoo.
Job 8:3
TSK
Ana Yàllaak safaan yoon? Ana Aji Man jeek safaan dëgg?
Job 34:34
TSK
Niti xel ñi dinañu wax, ñook ku rafet xel ku may déglu,
Job 37:23
TSK
Aji Man ji nu dul daj daa bare doole, dëggu, bare njekk, du note.
Psalms 145:17
TSK
Aji Sax ji, jëfinam jépp njekk la, jëfam jépp ngor la.
Proverbs 15:32
TSK
Xalab waxi yar, foye sa bopp la; deel déggi àrtu, yokk sam xel.
Zephaniah 3:5
TSK
Ndaxam Aji Sax jiy boroom njekk a ngi ci biiram, te du def njubadi, jantoo jant mu fenkal ab àtteem, te du wuute fu bët sete. Ab wurujkat kay moo xamul gàcce.
Romans 9:14
TSK
¶ Ana lu nu ci mana wax nag? Yàlla daa wàcc foofu yoon? Mukk kay!