All books in KYG

Luke 13

KYG · verse 1

24 chapitre

KYG / Luke / [JC0] chapitre 13

KYG · verse 1

J amono jooju tembe la aw nit dikk, àgge Yeesu mbirum waa Galile yu Pilaat bóomoon, jaxase seen deret ak seen dereti juru sarax yu ñu jagleel Yàlla.