TSK

TSK · Nehemiah 2:14

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Buurub Asiri nag tollu ca Lakis, yebal bummeem ak kilifay jawriñam ak bëkk-néegam, ñu ànd ak mbooloom xare mu takku, dem Yerusalem. Ba ñu agsee Yerusalem ba tollook solomu mbàndum kaw ma, fa feggook yoon wa jëm ca toolub fóotukaay ba, fa lañu taxaw.

Ka ca topp di defar, Neyemi doomu Asbug la, boroom genn-wàllu gox ba ñuy wax Bet Cur. Moo féetewoo la dale fa janook sëgi Daawuda ya, ba ca déeg ba nit ña sàkk, dem ba ca dalu Xarekat ya.