TSK

TSK · Proverbs 13:14

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Buumi njaniiw laaw ma, dee ne jaas, di ma fiir.

Buumi ndee a ma laawoon, njàqarey njaniiw dab ma, ma dajeek naqar aku tiis.

Kàdduy ku jub bëtu ndox la, day naatal; waaye ku soxor, wax ja làq fitna.

Ku rafet xel, jubal nga yoonu gudd fan, moyu teggi, ba jëm njaniiw.

Yoonu kuy jubal day moyu lu bon, ku teeylu sa jëfin, sàmm sa bakkan.