Fen, ma bañ, ba sib; sa yoon, ma sopp.
TSK
TSK · Proverbs 13:5
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
kuy daŋŋiiral, kuy fen, kuy rey nit ku deful dara,
caaxaan aki fen, yal na ma sore, néewleek barele, bu ma ci may lenn, leel ma lu ma doy;
Fa ngeen di fàttlikoo seeni jëfin, mboolem seeni jëf yu ngeen sobeele woon seen bopp, daldi jéppi seen bopp ndax seen mboolem jëf ju bon.
Ñu baree ngi nelaw, keroog ñu yewwoo fa pëndub suuf. Ñenn ña nara dund fàww, ña ca des añe gàcceek njàqare fàww.
¶ Kon nag bàyyileen fen, te ku nekk di wax sa moroom, dëgg, ndax ku nekk ci yeen sab céru moroom nga.
waaye ñu ragal ñi ak aji gëmadi ñi ak defkati ñaawtéef yi ak bóomkat yi ak moykat yi ak xërëmkat yi ak bokkaalekat yi, mboolem niti fen ñi, seen añ a nga ca déegu sawara waak tamarax ba. Loolu moo di ñaareelu dee.»