TSK

TSK · Proverbs 16:15

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi
Job 29:23 TSK

Booba lees ma daa séentu nib taw; ŋa ŋàpp, di nég waamey waxset.

sag wall a ko sagala sagal! Teddngaak daraja nga ko sédd,

Yal na Buur di xéewalu réewam nib taw cig ruujeef, mbaa waame wuy suuxat suuf.

Ñu baree ngi sàkku kilifa baaxe leen, moona Aji Sax jeey àtteb jaam.

¶ Bu suuf maree, ñaanal Aji Sax ji ab taw, Aji Sax ji mooy sàkk ay xàmbaar, sóobal nit ab taw, saxalal ku ne am ñax ci àll bi.