TSK

TSK · Proverbs 21:13

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Ci biir loolu askan waak seeni jabar di xultu lool ci seen kaw bokki Yawut.

Won nga ma ndoddi noon, ma boole bóom bañ yi.

Keroog nga woo ma wall, duma wuyu, nga seet ma, seet, doo ma gis.

Bu ngeen ma tàllaleey loxo, ma fuuyu. Bu ngeen doon ñaan-ñaanee it, du maa leen di déglu: seeni loxo, deret la taq ripp.

Léegi nag ngeen di teddadil sama tur, dellu gannaaw, ku nekk jëlaat jaamam yu góor ak yu jigéen, te ngeen goreeloon leen ba noppi, ñu moom seen bopp ni mu leen neexe. Néewal ngeen leen doole, ñu dellu di seeni jaam.”

Bu boroom kër gi xasee jóg, ba tëj bunt bi, fa ngeen di doxe des biti, di fëgg naan: “Sang bi, ubbil nu!” Mu ne leen: “Xawma fu ngeen bokk.”

Daan bu àndul ak yërmande, moom lees di àttee ña daawul jëfe yërmande. Yërmande nag kekku na ab daan.