TSK

TSK · Proverbs 27:22

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Ba ñu yégalee Firawna buuru Misra, ne mbooloo ma daw na, mooki dagam dañoo soppi xalaat ca mbirum bànni Israyil. Ñu ne: «Waaw nun, li nu def nag? Ana luy ndeyi yiwi bànni Israyil, ba dootuñu nu surgawu?»

Ñu yegge ko Sóol, mu yebal yeneen ndaw, ñu dikk, di wax ay waxyu, ñoom it. Sóol dellooti yebal ay ndaw, ñetteel bi yoon, ñu dikk, di wax ay waxyu, ñoom itam.

nga naan: «Dañu maa dóor te gaañuwuma, duma ma te yéguma ko. Moo! Duma yewwu nag, ba naaneeti?»

Aji Sax ji, xanaa du worma ngay sàkku? Dóor nga leen, safu leen; nga làbbli, ñu tanqamlu, wowle ba raw doj, baña dëpp.

¶ Juróomeelu malaaka mi sotti ndabam ci kaw ngàngunem rab wi, nguuram daldi sóobu ci lëndëm, nit ñi di yéyu ndax metit,