TSK

TSK · Proverbs 28:13

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Aadama ne ko: «Jigéen, ji nga ma booleel de, moo ma jox ci garab gi, ma lekk.»

¶ Firawna nag gaaw woolu Musaak Aaróona, ne leen: «Tooñ naa seen Yàlla Aji Sax ji, tooñ leen.

¶ Sóol ne Samiyel: «Bàkkaar naa! Ndax maa wàcc kàddug Aji Sax ji ak say digal, ndax ragal mbooloo mi, ba topp seen coobare.

¶ Daawuda nag ne Natan: «Maa tooñ Aji Sax ji.» Natan ne ko: «Aji Sax ji it jéllale na sa bàkkaar; doo ci dee.

Mu ne ko: «Ana lu ñu gis sa biir kër?» Esekiya ne ko: «Mboolem lu nekk sama biir kër, gis nañu ko. Amul lenn lu ma leen wonul ci samay denc.»

Ezra 10:2 TSK

Ci biir loolu Sekaña doomu Yeyel ma askanoo ci Elam, daldi wax Esra ne ko: «Noo tooñ sunu Yàlla, di jël ay jaambur jabar ci xeeti réew mi. Waaye loolu terewul Israyil am yaakaar ba tey.

Job 33:27 TSK

nit ki seedeeli ko ca nit ña, ne: «Maa bàkkaar, maa xëtt njub, te feyeesu ma ko sax!

Ba ma nee cell, damaa ràgg, dëkke naqar.

Mu jëm ci njiitu jàngkat yi, di kàddug Sabóor, ñeel Daawuda.

Na ku bon ba jëfinam, kuy def lu ñaaw fomm mébétam, te walbatiku ci Aji Sax ji sunu Yàlla, mu yërëm ko, yaatal njéggalam.

ngeen naan: “Nun de defunu dara, merum Yàlla won na nu gannaaw moos.” Gannaaw nee ngeen bàkkaaruleen, maa ngii di leen àtte.

¶ Maa ngay wax ak a ñaan, di tuub sama bàkkaar ak a tuubloo Israyil sama ñoñ tey dagaanal sama tundu Yàlla wu sell wi, ci sama Yàlla Aji Sax ji.

Waaye li dale Damaas ak Yerusalem ba ci réewum Yawut gépp, ba ca ñi dul Yawut, ñoom ñépp yégal naa leen seen wartéef, muy tuubeel ak waññiku ci Yàlla, ak jëf ju tuubeel yellool.