Genesis 1:9
TSK
¶ Yàlla ne: «Na ndox, mi asamaan tiim, gëndoo benn bérab, ba joor gu wow feeñ.» Mu daldi nekk noona.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ Yàlla ne: «Na ndox, mi asamaan tiim, gëndoo benn bérab, ba joor gu wow feeñ.» Mu daldi nekk noona.
Yal na la Yàlla may layub asamaan ak ngëneeli suuf, pepp ne gàññ, biiñ walangaan.
Israyil a ngi dëkke xel mu dal, walu Yanqóoba mee fegu, di wale réewum pepp ak biiñ bu bees, asamaan it di ko wàcceel ab layam.
Ana ku tëjoon lafi buntu géej, ba muy buccikoo xóote ya, fettax,
ba waa cati àddina yéemoo say firnde, waa penkook sowu di sarxolle.
Xërëmi neen yi yéefar yiy jaamu, ana ku ci mana taw? Am asamaan ay sóobal boppam ay waame? Du yaw la Aji Sax ji sunu Yàlla? Yaw lanu yaakaar, te loolu lépp, yaw a.