TSK

TSK · 1 Kings 21:11

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

may leen giir ndax seenug ragal Yàlla.

¶ «Buleen safaan dëgg cib àtte. Buleen far néew-ji-doole te buleen far boroom doole. Àtteleen seen moroom ci dëgg.

Buur, saa yoo bëggee ñëw rekk, ñëwal. Kon, Buur, nun noo koy teg ci say loxo.»

Ñu baree ngi sàkku kilifa baaxe leen, moona Aji Sax jeey àtteb jaam.

Su demewul noonu it nag Buur, xamal ne say yàlla dunu leen jaamu, sa jëmmu wurus ji nga samp it, dunu ko sujjóotal.»

Dogali Buur Omri daal lees di topp, ak mboolem jëfini waa kër Buur Axab. Seeni pexe ngeen topp, ba tax may def dëkk bi di lu daw yaram, waa dëkk bi di ñu nit ñiy muslu ci seenu demin, te gàcceg sama ñoñ, yeena koy gàlloo.»

Acts 5:29 TSK

¶ Piyeer ak ndaw ya ca des nag ne leen: «Yàlla lees wara déggal, waaye du nit.