Genesis 21:7
TSK
Mu neeti: «Éy, ku noon Ibraayma, Saarataa ngay nàmpal! Teewul ma jural ko góor, te muy mag.»
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Mu neeti: «Éy, ku noon Ibraayma, Saarataa ngay nàmpal! Teewul ma jural ko góor, te muy mag.»
Ag till sax joxe na weenam, nàmpal doomam, te sama bokk yi mujj néeg ba mel ni bànjóolig màndiŋ.