TSK

TSK · 1 Peter 3:13

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Jëfi ku bon, Aji Sax ji seexlu na ko; ku sàlloo njekk, safoo na la.

¶ Te itam nag xam nanu ne Yàlla mooy def mboolem lu xew, daje ba jur njariñal ñi sopp Yàlla, ñi mu woo, noonee ko ab dogalam namme.

¶ Xintewooleen cofeel, te ngeen sàkku mayi Noo gi, rawatina mayug waxe kàddug waxyu,

Fexeleen ba kenn du feyantoo. Waaye lu baax, deeleen ko deflante ci seen biir, te di ko defal ñépp.