Genesis 24:42
TSK
Ba ma agsee tey jii ca seyaan ba, damaa wax ne: “Aji Sax ji, sama Yàllay sang Ibraayma, ndegam nar ngaa àntal yoon wi may dox, ngalla may ma lii:
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Ba ma agsee tey jii ca seyaan ba, damaa wax ne: “Aji Sax ji, sama Yàllay sang Ibraayma, ndegam nar ngaa àntal yoon wi may dox, ngalla may ma lii:
Buur wax ma, ne ma: «Ana looy sàkku?» Ma ñaan gaaw ci Yàlla Boroom asamaan,
Aji Sax ji Boroom gàngoor yi mooy aar ñoñam, ñuy falaxe, di joggati doji mbaq, di naan ak a xaacu ni ñu màndi. Ni ndabi deretu juru sarax di feese, ni lañuy feese ak deretu noon yi, taq ci ripp ni cati sarxalukaay ba.
¶ Te itam Noo gi moo nuy dimbali ndax sunug néew doole, nde xamunu sax li jaadoo sàkku ci sunuy ñaan, waaye Noowug Yàlla moo nuy tinule ay onk yu wees kàddug làmmiñ.