1 Samuel 16:8
TSK
Yese daldi woo Abinadab, indi ko fi kanam Samiyel. Mu ne: «Aji Sax ji tànnul kii ba tey de!»
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Yese daldi woo Abinadab, indi ko fi kanam Samiyel. Mu ne: «Aji Sax ji tànnul kii ba tey de!»
¶ Elyab, magu Daawuda, dégg Daawuda di wax ak ñooña. Mu mer, ne ko: «Yaw sax lu la fi indi? Ak koo wacce la fay gàtt ak as néew ca àll ba? Xam naa bu baax sag réy ngise, ak njubadi gi nga mébét. Seetaansi xare bi doŋŋ a la fi indi!»
¶ Ci kaw loolu Yonadab doomu magu Daawuda Simeya, daldi wax ak baayam Daawuda. Mu ne: «Buur sang bi, bul defe ne sa doom yépp lañu rey de. Amnon rekk a dee, te mooy la Absalom dogu woon keroog ba Amnon torxalee rakkam Tamar.