كل أسفار KYG

1 Samuel 21

KYG · الآية 10

31 أصحاحات

KYG / 1 Samuel / الأصحاح 21

KYG · الآية 10

S arxalkat ba ne ko: «Xanaa saamarub Golyaat waa Filisti ba nga reyoon ca xuru Ela. Ma nga nee laxase ca turki ba, ca gannaaw xar-sànni ma. Soo ko bëggee, jëlal, boobu rekk a fi ne.» Daawuda ne ko: «Aa! Boobu kay amul moroom, jox ma ko.»