1 Samuel 18:7
TSK
Ña ngay fo, di awoonte, naan: Sóol jam junneem, Daawuda jam fukki junneem.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Ña ngay fo, di awoonte, naan: Sóol jam junneem, Daawuda jam fukki junneem.
¶ Daawuda nag ma nga naan ca xelam: «Bés a ngi ñëw bu ma nara sànku ci loxol Sóol. Li gën ci man daal, du lenn lu moy dawa daw ba ca réewu waa Filisti, ba Sóol tàyyi maa rëbbati ci Israyil gépp, ma daldi mucc.»
Xanaa du Daawuda mii lañuy woyal, di fecc, naan: “Sóol jam junneem, Daawuda jam fukki junneem”?»
Mu jëm ci njiital jàngkat yi, dëppook galan bi ñu dippee Pitax mu luu, dëkk fu sore; di taalifu jàngle bu Daawuda fentoon, ba ko Filisteen ña jàppee ca Gaat.