TSK

TSK · 1 Timothy 5:13

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Kuy wër di jëw, wuññi sutura; ku réy làmmiñ, bul déeyook moom.

Luke 10:7 TSK

Dal-leen ca kër googa, di lekk ak a naan ca la ñu leen jox, ndax liggéeykat yelloo na peyooram. Buleen di wër nag kër ak kër.

Ci seen biir sax la aw nit di jóge taxaw, di wax ndëngte, ngir xiirtal taalibe yi, ba ñu topp leen.

Li war moo di tëj seen gémmiñ, ndax këri lëmm lañuy tase àlluwa ju ñu amul sañ-sañam, ngir di ko sàkkoo am-am bu lewul.

Waaye rey nit, mbaa sàcc, mbaa def lu bon, mbaa dugg ci yëfi jaambur, bumu waral coonoy kenn ci yeen.