TSK

TSK · 2 Kings 13:3

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Seen Yàlla Aji Sax ji kat, mooy sawara wuy xoyome, Yàlla ju fiir la.

¶ Asayel ne ko: «Sang bi, looy jooy?» Mu ne ko: «Damaa xam lu bon li ngay defi waa Israyil. Seeni tata ngay taal, seeni xale yu góor nga jam saamar ñu dee, seeni doom nga tas ci suuf, seeni jigéeni biir nga butti.»

¶ Ci kaw loolu Asayel buurub Siri di fitnaal Israyil mboolem diir ba Yowakas di buur.

Moo tax Aji Sax ji xalab mboolem bànni Israyil, fitnaal leen, teg leen ci loxoy yàqkat yi, ba ni mu leen wacce.

ndax kat «sunu Yàlla, sawara wuy xoyome la.»