كل أسفار KYG

2 Kings 21

KYG · الآية 3

25 أصحاحات

KYG / 2 Kings / الأصحاح 21

KYG · الآية 3

M oo tabaxaat bérabi jaamookaay ya Esekiya baayam tasoon, yékkatil tuur mi ñu naan Baal ay sarxalukaay, samp xer wu ñuy jaamoo Asera, noonee ko Axab buurub Israyil defe woon, boole ca di sujjóotal mboolem biddiiwi asamaan, di leen jaamu.