كل أسفار KYG

2 Peter 2

KYG · الآية 13

3 أصحاحات

KYG / 2 Peter / الأصحاح 2

KYG · الآية 13

L oraange lees leen di feye loraange gi ñu sabab. Seen mbégte mooy xawaarey bëccëg ndarakàmm. Ñooñoo diy gàkk, aki sikk, ndax seen teewaay gàcce la ci seen biir yeen, bu ñuy bokk ak yeen bernde, te ca lañuy bànneexoo ay nax.