Leviticus 13:8
TSK
Su boobaa na ko sarxalkat bi xoolaat ba gis ër bi law ci deru yaram wi, mu doora biral ne nit ki sobewu na te jàngoroy der juy law la.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Su boobaa na ko sarxalkat bi xoolaat ba gis ër bi law ci deru yaram wi, mu doora biral ne nit ki sobewu na te jàngoroy der juy law la.
Mu jëm ci yonent yi: Sama bopp a ubu ràpp, sama xol jeex, sama yax yépp ne yalax, ma mel ni ku biiñ man, ba mu màndi ndax Aji Sax ji ak kàddoom yu sell.
Kon nag bu bàkkaar yilif seen yaramu ndee wii, ba di leen nanguloo ay xemmemtéefam yu bon.
¶ Almasi da noo yiwi, ngir nu yiwiku, kon nag saxooleen ko, te baña laxasooti buumi njaam.
Su ko defee seenum xel dellusi, ba ñu rëcc fiirug Seytaane, mi leen jàpp, di leen defloo coobareem.
Ay gor ngeen, waaye jaami Yàlla ngeen. Kon buleen taafantoo li ngeen diy gor ba def lu bon.