TSK

TSK · 2 Samuel 13:37

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

ñaareelu doomam di Kilab, ndeyam di Abigayil, ma doon jabaru Nabal waa Karmel ba; ñetteelu doomam di Absalom, mi Maaka di ndeyam. Maaka, Talmay buurub Gesur ay baayam;

Mu ne: «Lu waral kon nga naral lu ni mel ñoñi Yàlla ñi? Buur, boo waxee loolu kay, mel na ni tooñ nga, ndax jëliwoo sa doom ja gàddaay.

Absalom ne Yowab: «Xam nga damaa yónnee ci yaw, ne la ñëwal, ma yónni la ca Buur, nga laajal ma ko lu ma taxa jóge Gesur. Li gënoon ci man kay mooy ma toog foofa! Léegi daal damay gis Buur. Su fekkee ne damaa tooñ, na ma rey!»