TSK

TSK · 2 Samuel 13:39

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Ba loolu wéyee Isaaxa yóbbu Rebeka ca xaymab yaayam Saarata, muy soxnaam, di ku mu bëgg, te di ko muñe yaayam, ndax fekk na mu faatu.

Doomam yépp, góor ak jigéen ñëw, di ko dëfal, te noppiwul, xanaa naan: «Damay jooy, ba dem njaniiw, fekki sama doom.» Baayam di ko jooy,

Seen doom yu góor ak yu jigéen, ñu jébbal weneen xeet ci seen kanam, ngeen di leen séentu ci neen bés bu Yàlla sàkk, te dungeen ci man dara.

¶ Ci biir loolu Yowab, mi Seruya di yaayam, xam ne xelu Buur Daawudaa ngi ci Absalom.

Fu ma tollu maa ngi namm say ndigal ba sama xol ŋiis.