TSK

TSK · 2 Samuel 19:13

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع
Ruth 1:17 TSK

Foo deeye it, ma deeye fa, ñu denc ma fa. Yal na ma Aji Sax ji teg mbugal mu gëna tar, ndegam lenn lu moy dee tàggale na maak yaw.»

¶ Ci kaw loolu giiri Israyil yépp dikk fa Daawuda ca Ebron, ne ko: «Noo ngii di say bokk lenqe.

Amasa nag la Absalom faloon, mu jiite mbooloom xare ma, wuutu Yowab. Amasa moo doon doomu góor gu ñuy wax Yittra, di bànni Israyil bu jëloon Abigayil, mi Nayas di baayam. Abigayil ak Seruya, yaayu Yowab, ñoo bokk ndey.

Buur a nga dar kanamam, di jooy, baat bay jib ca kaw. Ma nga naan: «Wóoy Absalom, sama doom ja! Céy waay Absalom, sama doom ja! Éey waay sama doom ja!»