2 Samuel 3:14
TSK
Gannaaw loolu Daawuda yebal ay ndaw ca Isboset doomu Sóol, ne ko: «Jox ma Mikal, sama jabar ja ma cane woon téeméeri mbuñukay waa Filisti.»
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.