TSK

TSK · 2 Samuel 24:21

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Daawuda laaj waa Gabawon, ne leen: «Lan ngeen bëgg ma defal leen ko? Ana lu may def ba jotoo ko àq, ji ñu leen ameel, ba ngeen ñaanal ñoñi Aji Sax ji?»

Ba loolu amee Gàdd dem ca Daawuda keroog ca bés ba, ne ko: «Demal, nga tabaxal Aji Sax ji sarxalukaay ca dàggay Arawna, Yebuseen ba.»