TSK

TSK · 2 Samuel 5:3

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Samiyel fab béjjénu diw ba, diw ko fa kanam magam ña. Ba mu ko defee Noowug Aji Sax ji ne milib ca kaw Daawuda, dale fa ànd ak moom bésub keroog. Ba loolu wéyee Samiyel moom, dem dëkk ba ñu naan Raama.

Ba mu ko defee waa Yuda dikk, diw fa Daawuda, fal ko buurub waa kër Yuda. Gannaaw gi ñu wax Daawuda ne ko waa Yabes Galàdd ñoo rob Sóol.

Ba loolu amee Abner ne Daawuda: «Buur sang bi, dama lay wool Israyil gépp, ñu wuysi la. Su ko defee ñu fasook yaw kóllëre, nga mana nguuru fu la neex.» Ba loolu amee Daawuda yiwi Abner, mu dem ci jàmm.