TSK

TSK · 2 Samuel 6:2

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Tëgglul ñaari malaakay serub yu wurus te nga féetale leen ak ñaari cati kubeeru njotlaay ga.

Gannaaw gi ñu yebal ay ndaw ca waa Kiryaat Yarim, ne leen: «Waa Filisti de délloosi nañu gaalu Aji Sax ji. Tee ngeena dikk, yóbbu ko seen dëkk?»

¶ Gannaaw loolu sarxalkat ya yóbbu gaalu Aji Sax ja ca bérabam, ca biir néeg bu sell baa sell, ca ron laafi malaakay serub ya.

Mu jëm ci njiital jàngkat yi, dëppook galan bu ñuy wax Tóor-tóor yi, di seedeb Sabóor, giiroo ci Asaf.

Sunu jotkat ay Aji Sax ji Boroom gàngoor yi, Aji Sell ju Israyil.

Yonent yooyu, xamalees na leen ne du seen njariñal bopp lañuy liggéeyal xibaar boobu, xanaa yeen. Ñi leen àgge xibaar bi tey ñoo di ñiy waare xibaaru jàmm bi ci dooley Noo gu Sell, gi ñu yebale asamaan, te muy mbir mu malaaka yi sax, noon siiwa nemmiku.