TSK

TSK · 2 Samuel 7:2

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Ba mu ko defee ñu fat gaal gi ci biir bérab bu sell bi, doora firi ridob xàjjatle bi, làqe ko ko, na ko Aji Sax ji sante woon Musaa.

¶ Ba mu ko defee ñu indi gaalu Aji Sax ji, yeb ko ca bérabam, ca biir xayma ba ko Daawuda sampal. Daawuda daldi joxe fa kanam Aji Sax ji ay saraxi rendi-dóomal, ak saraxi cant ci biir jàmm.

¶ Uri ne Daawuda: «Sang bi, gaalu Yàlla ga ak Israyil ak Yuda dëkke ay mbaar, sama njaatige Yowab ak surgay sang bi bokk dale ci digg àll bi, man may dem sama kër, di lekk ak a naan, di dëkkoo sama soxna? Mukk! Giñ naa, nga fekke, duma def loolu!»

Waaye Cadog sarxalkat ba ak Benaya doomu Yoyada, ak Yonent Yàlla Natan, ak Simey ak Reyi, ñook jàmbaari Daawuda ya koy dar, ñooñu ànduñu woon ak Adoña.

li feek sàkkaluma Aji Sax ji bérab, ba dëkkal Mbërum Yanqóoba ma.»

«Àpp bi daal yeen la jotal, ba ngeen dëkke biir kër yu ay xànq lale, te kër gii dib gent?

Acts 7:46 TSK

Daawuda, ma Yàlla baaxe woon, sàkku woon na am màkkaan ngir Yàllay Yanqóoba.