Joxe nañu ku nekk la mu man, jëme ca alal ja ñuy liggéeye, muy juróomi barigoy wurus ak fanweeri barigoy xaalis, ak téeméeri mbubbi sarxalkat.
TSK
TSK · Acts 11:29
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Dugalal sa alal, dawloo ko; yàgg-yàgg nga jotaat ci.
Yeen nag, buleen tiisoo lu ngeen lekk, mbaa lu ngeen naan; te bu yooyu xalaat ub seen bopp.
Kenn ci ñoom ndóolul, ndax képp ku ciy boroom suuf mbaa ay kër, da koy jaay, indi njég li,
Ba mu ko gisee, da koo indi Àncos. Ba mu ko defee, atum lëmm ñuy daje ca mbooloom gëmkat ña, di jàngal nit ñu takku. Ca Àncos lañu jëkka wooye gëmkat ñi ay gëm-Almasi.
Bokkul ak jëf ju jekkadi, ak jiital sa njariñal bopp, bokkul ak naqari deret, bokkul ak denc mer.
Doonte jaar nañu ci nattub njàqare bu mag, seen mbégtee rembat ci seen biir ñàkk gu tar, ba géejal seenug tabe.
¶ Ci mbirum ndimbal lu jëm ci ñu sell ñi, jarul ma di leen bind,
¶ Buleen jikkowoo bëgg ub xaalis; doylooleen li ngeen am, ndax Yàlla moo ne: «Duma la bàyyi mukk, duma la wacc mukk.»