TSK

TSK · Acts 11:8

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Dina taxa ràññatle lu set ak lu setul. Dina taxa ràññatle boroom bakkan yi dagana lekk ñook boroom bakkan yi daganula lekk.

Hosea 9:3 TSK

Dungeen des ci réewum Aji Sax ji. Efrayim, Misra lay dellu, te ca Asiri, lu daganul lañu fay lekkeji.

Xam naa nag, wér na ma it te Sang Yeesu tax, ne amul lenn lu sobewu ci wàllu boppam, ba daganula lekk; waaye ki jàppe lenn muy lu sobewu, ci moom la loola di lu sobewu.