1 Samuel 8:5
TSK
Ñu ne ko: «Góor gi, léegi danga di mag, te say doom jaaruñu ci say tànk. Kon danga nuy falal buur bu nu jiite, ni ko xeet yépp baaxoo.»
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Ñu ne ko: «Góor gi, léegi danga di mag, te say doom jaaruñu ci say tànk. Kon danga nuy falal buur bu nu jiite, ni ko xeet yépp baaxoo.»
Mu woo giirug Beñamin, làng ak làng, làngu Matiri génn, Sóol doomu Kis génne ca. Ñu seet Sóol, gisuñu ko.
Waaye ba ngeen gisee Nayas, buurub Amoneen ña jëm ca seen kaw, yeena ma ne: “Buur bu nu jiite daal lanu bëgg.” Te Aji Sax ji seen Yàlla di seen buur.