2 Samuel 7:12
TSK
Te bu say fan matee ba nga tëddi, fekki say maam, maay yékkati kenn ci saw askan, sa deretu bopp, mu wuutu la, te maay saxal nguuram.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Te bu say fan matee ba nga tëddi, fekki say maam, maay yékkati kenn ci saw askan, sa deretu bopp, mu wuutu la, te maay saxal nguuram.
Bu sama der bi lekkoo sax, du tee ma dese suux wu ma xoole Yàlla,
Njotug bakkan jafe na, bu ci jéem dara.
fa mu doon topptoo jur ga; mu sàmmal ko waa kër Yanqóoba, askanu Israyil wi mu séddoo.
Mu ne gurub, samp bëti óomam, daldi àddu ca kaw, ne: «Sang bi, bu leen topp bii bàkkaar.» Naka la wax loolu, daldi nelaw.
Ndax mboolem li Yàlla nar bañuma leen cee xamal lenn.
Te kon it ñi dee gannaaw ba ñu gëmee Almasi, sànku nañu.
Sunu yaramu judduwaale wii nara yàqu, fàww mu sol weneen wu dul yàqu; sunu yaramu ndee wii, fàww mu sol yaramu deetil.