كل أسفار KYG

Acts 13

KYG · الآية 46

28 أصحاحات

KYG / Acts / الأصحاح 13

KYG · الآية 46

B a loolu amee fit la leen Póol ak Barnaba tontoo, ne leen: «Yeen Yawut yi de lanu wara jëkka yégal kàddug Yàlla gi, waaye gannaaw gàntal ngeen ko, ba jombale seen bopp ag texe ba fàww, nu ngii di walbatiku ci jaambur ñi.