Aji Sax ji Boroom gàngoor yi dafa wax ne: «Buleen déglu yonent yi leen di wax ay waxyu; cóolóoli neen lañu leen di naxe, di fent ay peeñu, di wax ay waxyu, te du kàddug Aji Sax ji.
TSK
TSK · Acts 15:24
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Jeremiah 23:16
TSK
Acts 15:9
TSK
Yàlla amul xejj ak seen sunu digg ak ñoom, ndax seen ngëm la raxase seen xol.
Galatians 2:3
TSK
Moonte Tit mi ma àndaloon sax, tegeesu ko fa wartéefu xaraf, te ci askanu gereg yi dul xaraf la bokk.
Galatians 5:10
TSK
Man de gëm naa ndax Boroom bi, ne dungeen wuuteek man xalaat benn yoon ci lii. Waaye kiy jaxase seenum xel, ak ku mu mana doon, mooy gàddu mbugalam.
Galatians 6:12
TSK
¶ Ñi leen di gétën ci xaraf mooy ñi ngistal tax ñu bëgg nit ñi gërëme leen seen melow yaram, te jubluwuñu ci lu moy ragal ku leen bundxatal ndax deewug Almasi gi ñuy xamle ne mooy taxa mucc.
Titus 1:10
TSK
¶ Ndax kat bare na ñu të, rawatina ci tuubéen ñi bokk ci askanu yawut, ay waxkati neen lañu, te ñooy yàq xeli nit ñi.