TSK

TSK · Acts 16:10

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Bul xañ njekk ku ko yelloo, ndegam man nga ko.

Acts 14:7 TSK

Foofa itam ñu di fa xamle xibaaru jàmm bi.

Acts 20:5 TSK

Ñooñu ñoo jiitu, di nu nég ca dëkk ba ñuy wax Torowas.

Acts 21:1 TSK

¶ Gannaaw ba nu tàggoo ak ñoom, nu dugg gaal, jubal dunu Kos, teg ca teeri ca dunu Rodd, jóge fa, jàll ba Patara.

Acts 27:1 TSK

¶ Ba loolu wéyee ñu dogu noo dugal gaal, jëme nu réewum Itali. Ñu teg Póol ak ñeneen ñu ñu tëjoon, ci loxool njiitu takk-der bu ñuy wax Yulyus, bokk ci mbooloom xarem buur bu mag bi.