TSK

TSK · Acts 16:20

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع
Ezra 4:12 TSK

¶ nu ngi lay xamal yaw Buur, ne Yawut ñi bàyyikoo fi yaw, ñëw fii ci nun, agsi nañu Yerusalem, dëkku fippukat bu bon bi, te ñu ngi koy tabaxaat. Ña ngay yékkati tata ya, gannaaw ba ñu lalaatee kenu ya.

Acts 17:6 TSK

Ci kaw loolu gisuñu leen, ñu diri Yason ak yeneen bokki gëmkat ba ca kanam àttekat ya. Ña ngay biral, naan: «Nit ñi tas àddinaa ngii, agsi nañu fi,

Naka lañu xam ne ab Yawut la, kàddu ga di benn, jibe ca mbooloo mépp, diiru ñaari waxtu. Ñu naan: «Artemis mu Efes màgg na!»

Buleen roy jamonoy tey jii, waaye yeesluleen ci ni ngeen di xalaate ba soppiku, ngir ngeen mana ràññee liy coobarey Yàlla, muy li baax, di bànneexam te mat sëkk.