Acts 20:34
TSK
Yeen ci seen bopp, xam ngeen ne, muy sama soxlay bopp, di yoy ñi ànd ak man, sama loxo yii laa liggéeye lu ma ko faje.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Yeen ci seen bopp, xam ngeen ne, muy sama soxlay bopp, di yoy ñi ànd ak man, sama loxo yii laa liggéeye lu ma ko faje.
Am boog mennum man ak Barnaba doŋŋ noo amul sañ-sañu ñàkka daan sunu doole?
Te ba ma nekkee ci yeen te soxla dab ma, wéeruwuma ci kenn ci yeen, ndax la ma ñàkkoon, bokk ya jóge Maseduwan ñoo ma ko indil. Fexe naa ba du lenn lu ma leen diisale, te noonu laay saxoo.
Xanaa bokk yi, yeena ngi fàttliku sunu doñ-doñ ak sunu coono? Diir ba nu leen di yégal xibaaru jàmm bu Yàlla bi, guddi ak bëccëg lañu daan liggéeyaale, ngir baña diisal kenn ci yeen.