TSK

TSK · Acts 2:31

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع
Acts 2:27 TSK

Doo ma wacc njaniiw moos, doo seetaan sa waa ju sell, mu yàqu.

Gëstu nañu jan jamono, ak yan xew-xew la Noowug Almasi ga nekkoon ci ñoom, tegtale woon. Mooy ba Noo gay seede lu jiitu, coonoy Almasi, ak ndam ya cay topp.