Dégluleen kàddug Aji Sax ji, yeen waa kër Yanqóoba, ba ci mboolem làngi kër Israyil.
TSK
TSK · Acts 2:36
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
¶ «Ay bés a ngii di ñëw,» kàddug Aji Sax jee, «yu may fas ak waa kër Israyil ak waa kër Yuda kóllëre gu yees.
Su boobaa ñu xam ne maay seen Yàlla Aji Sax ji ànd ak ñoom, ñoom ñuy waa kër Israyil sama ñoñ. Kàddug Boroom bi Aji Sax jee.
¶ «Bésub keroog bëtu ndox dina bënnal kër Daawuda, ak waa Yerusalem, ngir setal bàkkaar ak sobe.
Bésub tey jii ca dëkku Daawuda, juddule ngeen ab Musalkat, te mooy Almasi, di Sang bi.
Yeesu moomu mooy: “Doj wi ngeen beddi woon, yeen tabaxkat yi, te mu mujj di doju coll wi.”
Moo yónnee kàddoom bànni Israyil, àgge leen xibaaru jàmm, biy maye jàmm ci Yeesu Almasi, miy Sangu ñépp.
Su nuy dund, Boroom bi lanuy dundal, su nuy dee it, Boroom bi lanuy deeyal.
Dina feeñ it ndax noflaay ba mu nuy booleek yeen ñiy dékku ab coono, sédde nu ko, kera bés bu Sang Yeesu feeñee, ànd ak ay malaakaam yu làmboo manooreem, wàcce asamaan.