2 Kings 4:34
TSK
ba noppi yéeg, daldi tàlli ca kaw xale ba, tafu ca kawam, gémmiñ ak gémmiñ, bët ak bët, biir loxook biir loxo. Naka la bóof ca kaw xale ba, yaram wa tàmbalee tàngaat.